• il y a 4 ans
Gagganti ko
Ba ñu la koy jox , xam ul dara ;
Bu la séen ée , daw gatandu la,
Ay waajur ëm, da ñoo am oon yaakaar ci yaw
Jamono y dox , jafejafe am , sëytaane ñëw
Bu ko dóor , bu ko saaga , bu ko xas , bu ko wax lu ñaaw
Delloo l sa xel , ca ginnaaw, te muñ ël ko;

Ba ñu la koy may , xam ul dara ; ;
Bu la séen ée , daw laxasu la,
Ay waajur ëm, da ñoo am oon yaakaar ci yaw
jamono dox , jafejafe am , sëytaane ñëw
Bu ko dóor , bu ko saaga , bu ko xas , bu ko wax lu ñaaw
Delloo l sa xel , ca ginnaaw , bu ko souffrir loo;
Xool al ci ay , waajur ëm , bu ko joy loo

Bu juum ee gagganti ko
Bu juum ee gagganti ko
Bu juum ee gagganti ko
Bu juum ee gagganti ko

Bu ko dòor , bu ko saaga , bu ko xas,
bu ko wakh lu ñaaw
Bu yënggël ée daal , ba sa xol fees , génn ël nga dem
Bu fa toog yaw, di raak ak moom , sàmm al sa cér
Woo ko , waxtaan ak moom , té muñël ko

Bu juum ee gagganti ko
Bu juum ee gagganti ko
Bu juum ee gagganti ko
Bu juum ee gagganti ko

Yaw tam , bul forcer , deel négocier
Ndaw sii , bul teg deal , bul planifier
Te bu am ee , lu fi leer ul , nga clarifier
coow li , bu déborder , nga pacifier
Yaw daal , bul forcer , deel négocier
Ndaw sii , bul teg deal , bul planifier
Te bu am ee , lu fi leer ul , nga clarifier
coow li , bu déborder , nga pacifier
wa waaw

jaajëf , di na tax , xale wone jom
waaw góor, di na tax , xale yokk jom
di ko won sa jom , moo koy dolli jom
jom jom jom rek , dara lu dul jom

yërëmal ma ko
momit mou wégal ma laa
nax ko neex al ma ko
moomit mu xam ko

Category

🎵
Musique

Recommandations