• il y a 4 ans
Zéro Déchets
na ñépp jóg ;
mooy tax ba réew mi set
na ñépp jóg ;
mooy tax ba réew mi set
na ñépp jóg ;
mooy tax ba réew mi set
na ñépp jóg ;
mooy tax ba réew mi set

Nii Sénégal mel ;
War nagne geunue setal
leegleeg yaw nga mer sax ;
ba taggook sa sago
Mu mel ni fénéne;
ku nekk iy def lu la neex
Koo ci wax mu ni la pardon ;
topptoo l sa affaire
Mbedd mi mbedd um buur lë ;
topptool sa affaire
bogne sopé jikko ;
réewmi guenue set



na ñépp jóg ;
mooy tax ba réew mi set
na ñépp jóg ;
mooy tax ba réew mi set
na ñépp jóg ;
mooy tax ba réew mi set
na ñépp jóg ;
mooy tax ba réew mi set


fekk canal bi ;
nga sani ci mbalit
Nga jël ndox yu bon yi ;
sotti ci tali bi
abandonner auto yi
ku nekk iy def lu la neex
Koo ci wax mu ni la pardon ;
topptoo l sa affaire
Mbedd mi mbedd um buur lë ;
topptoo l sa affaire
bo gnou sopé djikko ;
Réewmi géunue Set

na ñépp jóg ;
mooy tax ba réew mi set
na ñépp jóg ;
mooy tax ba réew mi set
na ñépp jóg ;
mooy tax ba réew mi set
na ñépp jóg ;
mooy tax ba réew mi set

Sénégal ; ca jamono maam ya ;
ñépp a daan set set set al

Sénégal ; ca jamono maam ya ;
ñépp a daan set set set al
waa lu ñu dal ; ba léegi ku ci ne thi gnu fu la neex taqq al
bu ñii di gas ; ñi di suul ; dara du fa diak



Zéro déchets ; zéro zéro déchets
Zéro déchets ; zéro zéro déchets
Zéro déchets ; zéro zéro déchets
Zéro déchets ; zéro zéro déchets


Dakar jóg na ñu ;
Diourbel jóg na ñu
Fatick jóg na ñu ;
Kaffrine jóg na ñu
Kaolack jóg na ñu ;
Kédougou jóg na ñu
Kolda jóg na ñu ;
Louga jóg na ñu
Matam jóg na ñu ;
St- Louis jóg na ñu
Sédhiou jóg na ñu ;
Tamba jóg na ñu
Thiès Kayes jóg na ñu ;
Ziguinchor jóg na ñu



Category

🎵
Musique

Recommandations